Thread sur le ramadan des footeux 2.0
https://abs.twimg.com/emoji/v2/... draggable="false" alt="💀" title="Skull" aria-label="Emoji: Skull">
https://abs.twimg.com/emoji/v2/... draggable="false" alt="💀" title="Skull" aria-label="Emoji: Skull">:
1. Le modèle (mom mom depuis boumou amé 2ans la commencer woor bobou ba légui mongui si 102ans passé té dou bayi dara mou sédd yallah bou done accorder paradis siñou dakk woor mom lakoy dieuk diox)
1. Le modèle (mom mom depuis boumou amé 2ans la commencer woor bobou ba légui mongui si 102ans passé té dou bayi dara mou sédd yallah bou done accorder paradis siñou dakk woor mom lakoy dieuk diox)
2. Le Discret ( doko dégue mou wax,dou déf béne bruit day woor bamou diéx té dou sonal kéne dégue ndigeul,bax téksi yarou mom mom mach& #39;allah)
3. Le gourmand (adouna wam yeup lékk rék meune na wayé da téyal woor waxousi dara lékk moko geuneul lép,xol ko ak lékh yi mouy mélni ñokhite)
4. Le sous-côté (meune na wayè chaque année guayi diko sous-estimé té taxoul mou bayi ndeyssane di courass way,lou yallah xam rék doyna)
5. Le décevant (mom tamite 2ans la commencer woor ñeup fan ko mais mou dém ba sibir thiakhane dab ko mou bayékou trope mais néñ ko yédd dina ñowate)
6. Le vaniteux (pour mom mo dakk woor si adouna bi yeup té yallah xamni bala ndogou di djot mou commencer salite)
7. Le courageux (mom koor gui comme ndokh si mom day dém gauche dém droite ba gars yeup ragal mou fatou mais taxoul saway bayi yéne sayi sax mou tok 7 jours dou lékk)
8. Le faible (mom mom koor rék lay baña dégue journée bi day tope di dioy nonstop,quel kathiapan rék tchim)
9. L& #39;excessif (Aka wané ba kassou café dousi ndogou 2fois chaque jour mou dieunde bou béss bo waxé mou né la si wérou koor lañou néke)
10. Le cordon-bleu (mom ndogou mosi meune dalay togual bagua bégue tégual la ay sur le plat you diégui dayo,day sédeulé ba bo timé lékk bi sax sour ndax contane okhh magui dioy sax wooooooyy)
11. Xalé sinap (mom mom moy ñoñou fo léne guiss ñongui snap dila doral ay story du genre "Wérou koor lay done bamou ame doolé,wayène li néxoul,fi todj na radiax,xana néx,naka sén ramadan mes babyyyyy",quel phacochére rék tchim)
12. Le baye fall (mom mom day dém ba diéx fin de journée gua néke si embouteillages yi yakamti ñibi rék mou néla béne kassou café taf gua tangual bir bi touti)
13. Le xarane kat (mom mom dou woor dou déf dara keur diambour yi lay tope di xarane avant heure bi djot rék gua guiss mo teul té lékk rék lay déf dankoy diépi sax,quel kagna xol rék ak beuñou kagna yi)
14. L& #39;espoir (mom tamit à 2ans la commencer woor insbi mongui si yone bou bax ñeupa ko naw fan ko foumou romb beute yeup si mom lay tégou)
15. Le malade (mom mom chaque année mou déclarer forfait ay ulcère ak ñom sén,day guélawal sax diélé si fébar mais c le décision de Dieu il faut asspétééé)
17. Le sissou-man (mom bañ nako ba Ciss la sante,invité day ame bou diaral ko tour ndogou bi ndax siss beugoul partager ak kéneu,quel hippopotame rék tchiiim)
@bathiedrizzy @Morreal14 @MDiankha_ @DaniIbrahima @Nabyleu guayi thread bi meune na ame solo si wérou koor gui pour footeux yi dé anh???
https://abs.twimg.com/emoji/v2/... draggable="false" alt="💀" title="Skull" aria-label="Emoji: Skull">
https://abs.twimg.com/emoji/v2/... draggable="false" alt="💀" title="Skull" aria-label="Emoji: Skull">
Rt apprécié
https://abs.twimg.com/emoji/v2/... draggable="false" alt="🙏" title="Folded hands" aria-label="Emoji: Folded hands">
https://abs.twimg.com/emoji/v2/... draggable="false" alt="🙏" title="Folded hands" aria-label="Emoji: Folded hands">
Rt apprécié
@SR4capitaine @AstouSRamos yéne tamit warguéne meuna xéwlou si thread bi dé
https://abs.twimg.com/emoji/v2/... draggable="false" alt="💀" title="Skull" aria-label="Emoji: Skull">
https://abs.twimg.com/emoji/v2/... draggable="false" alt="💀" title="Skull" aria-label="Emoji: Skull">
https://abs.twimg.com/emoji/v2/... draggable="false" alt="👌" title="Ok hand" aria-label="Emoji: Ok hand">